lundi 12 novembre 2012

fagueye FALL


PAPE.jpg                             Je dis parfois que « l’amitié n’est autre chose qu’un accord parfait de sentiments joint à une bienveillance et une tendresse mutuelle parmi les nombreux et solide avantage de l’amitié le plus precieux à mon avis est de nous donner confiance en l’avenir et de ne point laisser les esprits se décourager et s’ abattre avoir un ami c’est avoir un autre soi – meme »

Cela me renvoie à penser à toi ma sœur je te dédie ces vers

Foguônnna nii duma massa am xarit boo djioguèn
Acksi wône na sakh thie moytu dépp  ndaw doo djiguèn
Guemna beussou tay dji ni amna ko
PAPE.jpgUté bigua am thie djicko ak ñom guissna ko
Eksilène ta nguèn ubi sèni nop boo bax
Yégué lèn utéy ndawsi gua xamné dané fax
Egg thie xollu ñepp la deff ndax da bax
       Foko fék kanam mbaguay ness-nessi ndax ré djou nèx
      Acksina fépp fo xalat thie dunya ni mbèx
      Limakoy sèdèl guanaw xol ak thiolin boo taroo
     Labir, yatu, yatalé, yeugué lay téki di fèru fépp fô né thie darroo

Longue vie, une santé de fer, et de prospérité sont mes souhaits pour toi ma soeur

  D’après ton frère PAPE ALIOUNE DIA